Directory

nos — Wiktionary Aller au contenu

nos

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

nos:

  1. teg mbir yi ci yoon, toftale leen, jekkal leen

nos -b:

  1. buum gi nuy def ci bakkanu giléem niki ag laab